4-4-44 - Youssou N'Dour

4-4-44 - Youssou N'Dour

Год
2007
Язык
`프랑스 국민`
Длительность
216100

아래는 노래 가사입니다. 4-4-44 , 아티스트 - Youssou N'Dour 번역 포함

노래 가사 " 4-4-44 "

번역이 포함된 원본 텍스트

4-4-44

Youssou N'Dour

Bô léké ba sour war nga gueureum

War nga gueureum gni doug thi wagne wé

Wagne wa tang na

Fimou toll nî war nguèna bëg

War-ngèna bëg thi indépendance bi ak-liko indi

4−4-44 (4−4-4−44) môm sa bopp mô neikh

4−4-44 (4−4-4−44) guiss say mbok mô neikh

Bô léké ba sour war nga gueureum

War nga gueureum gni doug thi wagne wé

Wagne wa tang na

Damani bou leuk léké olom

Boudè goréna té deugou warna ko guereumé pithe

No, no, no no no no

No, no, no no no no yeah

4−4-44 (4−4-4−44) guiss say mbok mô neikh

4−4-44 (4−4-4−44) guiss say mbok mô neikh

Ah li dafa nékh… guiss say mbok mô neikh

Li dafa nékh… gueume sa bopp mô nékh

4−4-44 (4−4-4−44) môm sa bopp mô neikh

No, no, no… guiss say mbok mô neikh

4−4-44 (4−4-4−44) môm sa bopp mô neikh

Oa, li dafa nékh… guiss say mbok mô neikh

A… môm sa bopp mô neikh

Oa, li dafa nékh… môm sa bopp mô neikh

200만 개 이상의 가사

다양한 언어로 된 노래

번역

모든 언어로 고품질 번역

빠른 검색

몇 초 만에 원하는 텍스트를 찾으세요